musicas.mus.br
Letras de músicas - letra de música - letra da música - letras e cifras - letras traduzidas - letra traduzida - lyrics - paroles - lyric - canciones - MANGUI CI SAMA BOPP - OMG - música e letra
Utilize o abecedário abaixo para abrir as páginas de letras dos artistas
Mangui Ci Sama Bopp letra
Taluma yendu di cas (awma jotam)
Nekkuma ci ay détails (bëgguma ko)
Danga faux man doo ma sonal (taluma ko)
Xaruma kenn ci leen (no no no)
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Deel wax reek
Yaq dèr ak coow li nga apo
Li tamm nga ko
Doxo ci daray mandu
Soppil jikko
Toppal àdduna mu lay jay
Loo fiy def yaa ko tey
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may séntu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may sentu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Taluma yendu di cas (awma jotam)
Nekkuma ci ay d [etails (bëgguma ko)
Danga faux man doo ma sonal (taluma ko)
Xaruma kenn ci leen (no no no)
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Doomu garmi la man
Xaajuma ci ay wax
Topp nga ma mboro
Billaay xale bile Massa
Doomu garmi la mane
Xaajuma ci ay wax
Topp nga ma mboro
Billaay xawma li lan la
Dumla wax dara
Waaye li metti na
Xamaloo ma dara
Dima yaq dax àdduna
Munuloo ma teye fi Yàlla finé
Dom téré bék
Mënoo ma stressé
Yàlla tere
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may séntu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Samay wax nga yobbu ko
Seddeloo ma sama jikko
Soo may sentu ci gallu xaj yaa fay mujju ne dej tokk
Taluma yendu di cas (awma jotam)
Nekkuma ci ay details (bëgguma ko)
Danga faux man doo ma sonal (taluma ko)
Xaruma kenn ci leen (no no no)
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi baax, maa ngi baax
Maa ngi ci sama bopp
Doomu garmi la man
Xaajuma ci ay wax
Topp nga ma mboro
Billaay xale bile Massa
Doomu garmi la man
Xaajuma ci ay wax
Topp nga ma mboro
Billaay xawma li lan la
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi ci sama bopp
Maa ngi ci sama bopp
OMG - Letras
- Abusé
- Bandit Bou Lewet
- Bayil Mou Sedd
- Boss Lady
- Boum Bam
- Ci Peet
- Convicções
- Dafmay Nekh (feat. Bril)
- Domeusseu Am Kou Melni Mane
- Expressão de Alguém
- Hasta Luego
- Kenen Diapoula (feat. Jahman X-Press)
- Kilometa
- Koti Koti
- Laf Thiat
- Lu Ci Sa Yoon
- Maako Sagn
- Mafia Bi (feat. Jailer Bangz, 4Leuz, Cool10 & Kmou MC)
- Mangui Ci Sama Bopp
- Money Money
- Ndouti Ndout
- Niou Dem Mairie
- Sama Khol
- Senegal
- Som do Silêncio (II Os Reis)
- Soxna Si (feat. Admow)
- Venha e Viva
- Waxoma Woon Lii
- Yallah Baaxna
- Yeungueul Ci Say Mbagg (feat. Dip Doundou Guiss)
top 30 músicas
©2003 - 2026 - musicas.mus.br